GDT10 Taxawu suqqaliwaat garab yi

Koon RNA (di Taxawu suqqaliwaat garab yi) mi ngi teggu ci tann saxayaayu garab yi biir tool yi. Ci  yooyu, ñu tann si yu dëgër yu ñuy bayi ñuy màgg.  Loolu mooy benn si  doxalin yi, ñaareel u RNA mooy rañee garab yu ndaw yi ñu bugg, man naa nekk akasiyaa àlbidaa (feederbiyaa).

Current language
وولوف
Need a language?
If you would like this video translated into other languages, please contact kevin@accessagriculture.org
Translated in
SENEGAL
Translation funded by
GIZ
Uploaded
3 years ago
Duration
6:58
Produced by
Countrywise Communication, CIS Vrije Universiteit Amsterdam