Xeex sax yiy neewil reen ci mbey um dër
Sax yi man nañoo dundd ci biir suuf yéep te waajal leen gene neex faagaagal leen. Sekere bi mooy : • ji ay palaŋ yu wér • Yaqq leen féep fu sax yi man jogge li wur seen tool u lujum • Awlante akk yeneen mbey yi man dékku sax yi • Mooytu duggël ay sax yu jogee ci yeneen tool. Ñu jél poñ yooyu benn ki benn.
Current language
وولوف
Available languages
Need a language?
If you would like this video translated into other languages, please contact kevin@accessagriculture.org
Translated in
Senegal
Translation funded by
GIZ
Uploaded
3 years ago
Duration
15:42
Produced by
Agro-Insight