Weer um kaani ci naaj bi

Su kaani yi toyee, daa ñuy qall walla nëb. Yenn qalleef yi di na inndi posan bu nit ñi tuddée afalatosiin. Ngir gaawal weer beek wowal ñam ci anam bu sell, man na ñoo jëfëndikóo sesuwaar biy japp  taŋngoor u jànt bi nfir wowal firwi yi akk lujum yi. Sesuwaar biy japp  taŋngoor u jànt bi bari melokaan akk tolluwaay, waante doxin bi benn la. Ci widéwóo bii, daa ñu jangg ni ñuy defaree akk jëfëndikóo sesuwaar bu sempal biy japp  taŋngoor u jànt bi ngir wowal kaani yi.

Current language
وولوف
Need a language?
If you would like this video translated into other languages, please contact kevin@accessagriculture.org
Translated in
Senegal
Translation funded by
GIZ
Uploaded
3 years ago
Duration
10:30
Produced by
Agro-Insight