GDT07 Xaaj u weer
Xaaj u weer, tur u ay daggit u diget yu wërngël, nekk na pexe ngir taataan ndox ak fu mu man ti jogge. Man naa àndak lu nekk : Yaatuwaay yi akk melokaan yi, beykat bi man na kaa soppali te soxlowul xeer ngir defar leen. Te it dey dox bu baax te man na ñu ko jëfëndikóo ci mbey mi, ci ñax walla garab.
Current language
Wolof
Available languages
Need a language?
If you would like this video translated into other languages, please contact kevin@accessagriculture.org
Translated in
SENEGAL
Translation funded by
GIZ
Uploaded
3 years ago
Duration
7:27
Produced by
Countrywise Communication, CIS Vrije Universiteit Amsterdam