GDT12 Mbey um ëlëk
Mbey um ëlëk dafa sukkëndiku ci ñatti bunt walla ponk : suuf su sopeeku. Da ñuy yamale ci lu ñu soxlo rekk labuur yi ngir taxawal gancax gu baax te di top seen caxaay. Ñaareel ba, ñu dugël ay xeet up mbey yii di leguminës ngir awlante mbey mi…Ñatteel ba, ñu bayi desit u mbey mi ci kaw suuf si mu nekk kiraangeem ngir moytu suufi neen.
Current language
Wolof
Available languages
Need a language?
If you would like this video translated into other languages, please contact kevin@accessagriculture.org
Translated in
SENEGAL
Translation funded by
GIZ
Uploaded
3 years ago
Duration
8:03
Produced by
Countrywise Communication, CIS Vrije Universiteit Amsterdam, World Bank Institute