Caytub mboot ci tool niébé ak lujum

Mboot yi ay gounor you ndaw you wert ak you gnoul, mboot dagnouy songh tool you baré you ci melni niébé ak moutardeu soupamé ak xobou ber. Ci sinema bi dinagnou guiss nane la bey kat yi ca bangladesh di xééxé mboot yi té dougnou dieufandiko  jumtukay simi yi ray.

Current language
Wolof
Need a language?
If you would like this video translated into other languages, please contact kevin@accessagriculture.org
Translated in
Sénégal
Translation funded by
GIZ
Uploaded
2 years ago
Duration
9:13
Produced by
CCDB