Awlante mbey mi ak yeneen xeetu meneef

Xeet u meñeef yu mel ni leguminoos lu am solo la ci awlante mbey mi, ndax di na waññi ñax yu bon yi te yokk doole suuf si ci boole mbindéef yu sew yi ci biir am ngir tëyë ferñent bii di asot . Ngir mu wóor leen ni seen suuf dencc na mbindéef yu sew yu baax yi, mën ngeen jindd porodiwi bii di duggël ferñent u Risoobiyóm. Ferñent u Risoobiyóm mên naa dunnd at yu bari ci biir suuf si. Koon soxlowul di duggël ferñent boobu seen mbey um leguminoos saa su ne.

Current language
Wolof
Need a language?
If you would like this video translated into other languages, please contact kevin@accessagriculture.org
Translated in
Benin
Translation funded by
GIZ
Uploaded
7 months ago
Duration
12:29
Produced by
Nawaya