Dooleel suuf si ak njaxasum eŋngere gancax
Uploaded 2 weeks ago | Loading

14:29
Mbay yu wuute ak xob u garab yi da ñuy joxe xeet u mbindéef yu sew ak ay ferñent su ñu leen jaxaseek suuf si. Loolu di na dolli nefere gi, yokk mbindéef yu sew yu am njariñ ci suuf si te di yokk naŋnguteem.
Current language
Wolof
Produced by
Shanmuga Priya J.