Fiir um weñ u firwi yi ak meeb u ñam
Uploaded 1 month ago | Loading
11:36
Weñ u firwi yu ndaw yi soxlo nañu poroteyiin ngir magg. Xeet up weñ u firwi yéep dañu koon wuti meeb yu bari poroteyiin. Desit u lëwiir yu bérëp yiy defar sangara lu fees dell la ak poroteyiin te nekk jumtukaay bi ñu mën soppali meeb u nam. Meeb u ñam yi, nekk na dundd bi ñu rax ak ndox te su weñ yi rombbee, seen xet da leen di xëcc ngir ñu ñëw lekk si te si la leen ndox mi di fiir ñu dal di dee.
Current language
Wolof
Produced by
Agro-Insight