Garab u gancax ngir faj yaram bu tàng ci jur gi
Uploaded 2 years ago | Loading
![](https://accessagfiles-drupal9-download.s3.eu-west-1.amazonaws.com/attachments/2018-08/183_fever_in_livestock.jpg?VersionId=YfQYUkYG4YDK.AMsxqlXLFTpPHpR7e2A)
11:23
Ci widéwóo bii, daa ñu jàngg la mooy joxe yaram bu tàng, nan la ñuy xamee bayima bu yaramam tàngg akk nan la ñuy koy safaraa ci biir gétt gi ci topp akk ndiktël yu jafewul.
Current language
Wolof
Produced by
Atul Pagar, ANTHRA