Garab u gunóor bu bayeeko si gancax
Uploaded 2 weeks ago | Loading

14:38
Beuss bounou wisse garrabu gunoor yi ci tool bi, nitt yi ak mala yi dagnouy noyi ngelaw bobu raxe lolou dafay takheu sen derr , seni gett ak sen guemine di guise si lou yomb ak pordui yooyu di rayy, lolou day andi ay kheetou faibar banopi di rayy.
Current language
Wolof
Produced by
Green Adjuvants