Jal up xeer yi
Uploaded 9 months ago | Loading

9:49
Jal up xeer yi da ñuy amal liggéey buy samm suuf si ndax da ñuy dencc ferñent yi. Daa ñu dekkalaat suuf si naawoon. Baykat u réewum Keeñaa ñooy wane ni ñuy tabaxe jal up xeer yi.
Current language
Wolof
Produced by
WOCAT