Jotali sa kër meñeef u mbay mu sell
Uploaded 4 months ago | Loading
15:19
Ci xarala yu bees yi, baykat yi da ñuy jaay seen meñeef u mbay mu sell mi te kiliyaaan di si def seen komaan yu liibar ba 5 cilό. Kiliyaan yi da ñuy jot seen bunt u kër, ay meñeef yu wόor, yu sell te bees. Ci am ay kiliyaan yu wόor, baykat yi da ñuy am ay koppar yu wόor ak itam njëg yu kawe ci seen meñeef.
Current language
Wolof
Produced by
Atul Pagar