Lal u ñax akk garab aki gancax gi ngir ngóob mu gën
Uploaded 4 months ago | Loading

12:58
Lal up garab yi akk gancax u diiwaan bi di na aar suuf si ferñent u jànt bi te di waññi tànggay u suuf si, mu di lu am njariñ ci mbindéef yuy dunnd ci biir am. Bu leen gor gancax geek garab yi lu dul ci taneef, ndax muy des car yu doy ngir may mañeef gi ñu mën sax bu baax. Teg leen lal up ñax gi seen tool 1 walla 2 ay bés lu jiitu jiwu bi. Ŋayyileen ndànk lal up ñax bi su ngeen di dugël jiwu bi ci biir pax mi.
Current language
Wolof
Produced by
Access Agriculture