Ni ñuy jaayee meñeef u mbay mu sell mi
Uploaded 4 months ago | Loading
15:03
Soo leen di jaay ci fuwaar yi, mën ngeen fësël seen mbooloo ci jëfëndikόo ci misaal ay nataal, ay tabiliyé aki napp yu ngeen bokk nirόo. Am leen ay yëngu-yëngu yu yeete ak wëy jëfëndikόo yeek seeni doom. Jokko ak kelifa gox bi ngir sàmpp ay bérëp u njaay meñeef u mbay mu sell mi wuuteek yu mbay um cosaan yu posan yi rax.
Current language
Wolof
Produced by
Agro-Insight