Benn tërëlin u wakirlu
Uploaded 7 months ago | Loading
11:25
Tërëlin bu lëkëlé ay réew ci wakirlu cellin boobu, mën naa nekk jaar-jaar ci ay birόoki birό te jafe lool te di lu baykat yu ndaw yi ci mbay mu sell miy dunndël luuma gox bi mënul dékku. Cii réew yu bari, tërëlin u wakirlu, di SPG, da ñu feeñ ni jëfandikukaay. Doonte tërëlin u SPG sàmppu na ñu te wuute diggënté réew ak réew, am nañu fu ñu dajee : Baykat benn mbooloo mën na ñu daje sàmpp benn kuréel u wakirlu, ngir nemeeku ji tool yi benn aki benn ngir am lu wόor ni mbay mu sell moo fa nekk.
Current language
Wolof
Produced by
Agro-Insight