Ray weñ u firwi yi ak meeb.
Uploaded 10 months ago | Loading

11:36
Mën nañu wis meeb u ñam yi fi mu ko laaje walla ci ay jumtukaay u meeb. Weñ u firwi yi mën nañu xeeñtu ay meeb ci lu tollook 10 meetar. Yenn meeb yi da ñu am posan u jamono yu ñu na ngu ci mbey um firwi yu amul tooke.
Current language
Wolof
Produced by
Agro-Insight