<<90000000>> viewers
<<320>> entrepreneurs in 18 countries
<<5432>> agroecology videos
<<110>> languages available

Saytu feebaru taqq xob yi ci gerte

Uploaded 2 weeks ago | Loading

Faibaru gomou khob ay sampignong youy doundou ci suuf si ak si dessitu mbey yi gnokay diokhe Bala ngen di jiwu, diakhasse len poudeurou trichoderma wal pseudomona ak neefare ngen tass ndiakhass bobou si tool yi Tann len ay kheetou guerte you deugueur teksi ngen di hjefendiko dome bu ame wergui yaram Khoocc len dome yi ci diirou ben gouddi ci ndiakhass poudeurou asafoeitida bala nge, di jiwu Woral len yoon yu baakh Khool len leeg leeg seni mbey ngen dindi noumoy gueuna gaawe garab yu faibar yeup

Current language
Wolof
Produced by
Atul Pagar, WOTR
Share this video:
How you can help... Your generous donation will enable us to give smallholder farmers better access to agricultural advice in their language.

Recent Videos

With thanks to our financial partners