<<90000000>> viewers
<<320>> entrepreneurs in 18 countries
<<5432>> agroecology videos
<<110>> languages available

Topatoo feebar u soble bi

Uploaded 2 weeks ago | Loading

Soble yi di na ñu sax bu baax ci anam yu wuute, waante ci jamonoy nawet, la ñu ëpp lu leen di songg. Feebar u soble bi mën na lem xob yi te waññi randmaa bi. Feebar yi mën na ñoo tas ci biir suuf si, jiwu yi walla desit u mbay mi walluwoon.

Current language
Wolof
Produced by
Agro-Insight
Share this video:
How you can help... Your generous donation will enable us to give smallholder farmers better access to agricultural advice in their language.

Recent Videos

With thanks to our financial partners