Yokk ràndmaa gerte gi ak xott u barigó.
Uploaded 2 weeks ago | Loading

10:07
Tóor-tóor yu nguni-ngaana yi da ñuy lemu te def bant bu melni pusó di sax jëm ci suuf si. Loolu moo tudd pedonkil. Su pedonkil yooyu jotee dugg ci biir suuf si, ay doom dal di feeñ. Ràndmaa gerte gi mi ngi aju ci tolluwaay lii di pedonkil di reen yi mën dugg ci biir suuf si. Ci bërëŋ barigó si kow mbay mi, bant yi da ñuy lalu ci suuf si. Loolu di may pedonkil yi nekk ci kow bant yi mën dug ci biir suuf si
Current language
Wolof
Produced by
Atul Pagar, WOTR