Jëfëndikóo dunndéef yu tuuti yi ci yar um jur gi
Uploaded 2 years ago | Loading

12:50
Ci widéwóo bii, da ñu jàng ci beykat yu xarañ ci réewup Bengaladees, nan la dunndéef yu tuuti mën dimbalee ci waññi njëg u xont gi, amal jur gi dëkkuwaay bu sell te tax ñu am wergu yaram bu baax.
Current language
Wolof
Produced by
Rezaul Karim Siddique