Defar soowu yaawur ci kër gi
Uploaded 1 year ago | Loading
11:52
Ci widéwóo bii, da ñu jàngg pacc yu am solo te menul ñakk ngir defar soowu yaawur kalite bu baax, mu nekk ci li ñuy jëfëndikóo walla ci li ñuy jaay.
Current language
Wolof
Produced by
Egerton University