Jëfëndikóo dunndéef yu tuuti yi ci yar um jén yi
Uploaded 1 year ago | Loading
14:40
Napp bu ëpp gi akk mbalit yi ñu ci doon sotti ci dex yi akk déeg yuy am ciy jamono walla yu sax dakk, tax na joxeetu ñu jén bu doy ngir facc soxlo askan wi.
Current language
Wolof
Produced by
Rezaul Karim Siddique