Taxawal ay marse meñeef yu amul posan
Uploaded 1 year ago | Loading
15:37
Ngir jaay ay meñeef mbey mu amul posan, laac na bayi xel ñeeti mbir : disóo akk kelifa gox bi, doxalin u gaaraanti, ndax askan wi xam ni meñeef yi amul benn tooke ; akk birël akki tawaxu kilmiyaan bi.
Current language
Wolof
Produced by
Agro-Insight