Roose akk gutt
Uploaded 2 years ago | Loading

13:24
Akk roose akk gutt, pot u ban bu ñu lakk te am bën-bën yu sew la ñuy suul ci biir suuf si jogge mbey mi te fees akk ndox. Ndox mi day senn ndànk-ndànk di jaar ci bën-bën u gutt gi ba jot reen un gancax gi. Ni gancax gi gën di mànqq, ndox mi di sotteeku joge si gutt gi. Koon, gutt gi dafay joxe li gancax gi soxlo si ndox rekk.
Current language
Wolof
Produced by
Green Adjuvants