<<90000000>> viewers
<<266>> entrepreneurs in 18 countries
<<4647>> agroecology videos
<<107>> languages available

Njàmbaan u nefere bu ndoxe akk bu wow

Uploaded 1 year ago | Loading

Ngir mbey mu sell, soxlo na suuf su sell, ndax suuf su sell ëmbb na mbidéef yu bari aki sax u suuf. Ngir defar njàmbaan u nefere genn wallu ektaar, soxlo na 10 ciló ndéef u naggbu tooy, singuwaay am, fariñ u pep u puwaa bu xeex walla beneen meñeef, suukër bu ñu raxul walla weexalul akk benn ŋëb u suuf bu sell.

Current language
Wolof
Produced by
Atul Pagar, WOTR
Share this video:

With thanks to our sponsors