Liggeeyum suuf u tool
Uploaded 2 years ago | Loading
9:08
Nan la liggéey um suuf si akk doxalin u ndox um roose yi di nasaxal taxawaay u mbey mi, nekkin u ñax yu bon yi akk ràndmaa yi ci meñeef gi ? Ak lu tax ñu war maasaale bu baax suuf si ngir eŋngere yi mën joxe bu baax ? Daa ngeen fekk ci bii widéwóo, tonntu yi ci laac yooyu yéep- akk ci yeneen..
Current language
Wolof
Produced by
AfricaRice, Agro-Insight, Countrywise Communication, INERA