Njëmbët um ceeb
Uploaded 2 years ago | Loading
14:16
Su nu jëmbëtee ceeb bi si la randmaa yi di yokku tuuti. Moo ëpp ñaar ba ñattiyoon randmaa ceeb yi ñu ji sanni. Koon lu tax du ngeen seetaan widéwóo ngir xam nan la ak lu tax ?
Current language
Wolof
Produced by
AfricaRice, Agro-Insight, IER, Intercooperation, Jekassy