GDT11 Lëkëlóo beykat yeek Sammkat yi
Uploaded 4 years ago | Loading
7:56
Sammkat yi xam na ñu ni desit u mbey mi akk garab u beykat yi amal na leen njariñ. Ci wecceek ñoom daa ñu joxe dara : dunndup suuf si.
Current language
Wolof
Produced by
Countrywise Communication, CIS Vrije Universiteit Amsterdam