Weer um ananaas ci naaj bi
Uploaded 4 years ago | Loading

7:59
Lu bari ci ananaas ji day yaqqu ndax man noo leen dencc bees lu ëpp ay bés. Ananaas yu wow yi man na am at. Su nu wowalee ananaas yi daa ñu waññi pert yi te gën am xaalis at mi yéep. Ci widéwóo bii, daa ñu wanee ni ñuy wowalee ananaas ci sesuwaar yu sukkëndiku ci naaj bi, ndax jumtukaay bu sell la te jafewul.
Current language
Wolof
Produced by
NOGAMU