Aar mboq mi ci afalàtoksin ci jamono weer beek dencc bi
Uploaded 3 years ago | Loading
15:03
Sugnu wergou yaram ak yu diour yi meune nagnsé am diafédiafé nagn diéma diangaté si baykat yu mak yi am expérience faré thia réwu tanzanie ngir gnu meuna xam nane lagniy wowalé ba nopi dinthi sugnu mbok.
Current language
Wolof
Produced by
Agro-Insight