Denc bu baax ak arr pepp mboq mi
Uploaded 3 years ago | Loading
12:49
Nguir denc ak àar mboq peep mboq mi, danoo wara jeufeundico saqq um ban, wala Silo wègn, wa saaco PICS, wala gutte. Bu nu dencee peep mboq mi si brabu dencu kaay yi. Dina àaru bu baax si diir bu yaag.
Current language
Wolof
Produced by
Songhai and Helvetas