Yokk ferñent ruy akk njambaan u buy
Uploaded 2 years ago | Loading

7:53
Ci meŋngëléek ak yeneen ñam, doomu buy bari na lool ferñent yu mel ni feer ak mañeesum, ak it witaamin SEE. Am naat lu bari ci ay buum. Lu baax la ci wergu yaram u doomu aadama te di faggu ci gaawaa feebar. Ci mbaax yooyu mu ëmbb tax ñu tuddée ko ñàm bu makk bi.
Current language
Wolof
Produced by
Hochschule Rhein-Waal, Biovision