Nga diwee sa jiwu dugub akk lu raxul tooke
Uploaded 2 years ago | Loading
12:16
Diw sa jiwou da koy aar ci pithie ak gounoor té day deugeureul maggug gancàx gi, geun koo naatal. Boula nékhée nga tééla ji laata mouy taw.
Current language
Wolof
Produced by
Access Agriculture, IVTSANE