Pàrk u garab yi àndak mbey
Uploaded 4 years ago | Loading
8:20
Bérëp u garab yooyu ëmbb na wantaas yu bari ci alom gi akk kër yu bari. Beykat yi ñooy tabaxkat u bérëp yu jaxasoo yooyu te am solo. Ñoom wuyu na ñu ci lu gaaw ci copite yooyu ak jis-jis yu bees yi.
Current language
Wolof
Produced by
Countrywise Communication, CIS Vrije Universiteit Amsterdam