GDT10 Taxawu suqqaliwaat garab yi
Uploaded 4 years ago | Loading

6:58
Koon RNA (di Taxawu suqqaliwaat garab yi) mi ngi teggu ci tann saxayaayu garab yi biir tool yi. Ci yooyu, ñu tann si yu dëgër yu ñuy bayi ñuy màgg. Loolu mooy benn si doxalin yi, ñaareel u RNA mooy rañee garab yu ndaw yi ñu bugg, man naa nekk akasiyaa àlbidaa (feederbiyaa).
Current language
Wolof
Produced by
Countrywise Communication, CIS Vrije Universiteit Amsterdam