Jamonoy Kampagn ci tooli darkassé
Uploaded 2 years ago | Loading

8:41
Garab u darkasse ñu koy wax it ndamaraas lu am solo la ci wallu koom, dunnd u askan wi ak ci alom gi. Da ñu koy bey lu ci ëpp ngir doom am akk saal am. Ci tool u darkasse bi ñu toppatoo bu baax te boolekook yeneen mbey u at mi, garab yi di na meññ bu baax te doom yi da na ñu am kalite bu mucc ayib.
Current language
Wolof
Produced by
DEDRAS