Def nji um kañjj bu baax
Uploaded 3 years ago | Loading
12:16
Ci réewup Beneŋ, beykat yi ñooy wane ni ñuy defaree nji um kanjj gu baax. Ji leen 2 ba 3 pep gën gaa bari ci pax bu nekk te di topp diggënté yi ngir am yaraxaay gu baax akk maggaay u gancax gi bu baax.
Current language
Wolof
Produced by
Alcide Agbangla