Faagaagal gunóor yi ci mbey um lujum
Uploaded 3 years ago | Loading
10:49
Ay beykat ci réewup Endd ñoo ñuy wan nan la mbóot mbey mi di rayee gunóor yi . Ci daanel gunóor yi nekk ci gancax gi akk sotti leen puudër akk pompee bu diis, da ñuy dee. Pompee leen diw u niim walla tuuti xob yu wex jaxasook ndox akk singuwaay u nag. Yenn posan yi da ñu am ay sampiñoŋ yu mën ray gunóor yi.
Current language
Wolof
Produced by
MSSRF