Topatoo seen wergu yaram u xar
Uploaded 2 years ago | Loading
12:48
Maggaay u xar mu feebar du gaaw te njëg bu néew lay am ndax raggaay am akk yapp am bu bon. Ak saytu bu baax, mën na ñoo nemeeku miir meek feebar yi ci xar yi ngir gaaw leen safara. Ñu jàng ni ñuy topatoo werguyaram u xar yi.
Current language
Wolof
Produced by
AMEDD