Awlante mbey mi ak yeneen xeetu meneef
Uploaded 1 year ago | Loading
12:29
Xeet u meñeef yu mel ni leguminoos lu am solo la ci awlante mbey mi, ndax di na waññi ñax yu bon yi te yokk doole suuf si ci boole mbindéef yu sew yi ci biir am ngir tëyë ferñent bii di asot . Ngir mu wóor leen ni seen suuf dencc na mbindéef yu sew yu baax yi, mën ngeen jindd porodiwi bii di duggël ferñent u Risoobiyóm. Ferñent u Risoobiyóm mên naa dunnd at yu bari ci biir suuf si. Koon soxlowul di duggël ferñent boobu seen mbey um leguminoos saa su ne.
Current language
Wolof
Produced by
Nawaya