Ratt um nag yi akk loxo
Uploaded 4 years ago | Loading
9:26
Yar ngir meew nekk na bunt u dundd akk am-am ci kër yu bari. Ngir am xaalis bu takku, lu am solo la defar meew bu bari te am kalite. Waante , meew lu gaaw yaqqu la walla mu tilim te jindkat yi du ñu ko bugg. Meew man na yaqqu su fekkee nit ku feebar moo ratt nag bi, walla seen ndàb u rattukaay setul walla it cus yi akk ween u nag bi tilim.
Current language
Wolof
Produced by
Egerton University