Witt, weer akk dencum kaani
Uploaded 4 years ago | Loading
11:00
Ngeen di waaja dem jaayi sa marse ba seen kaani, tànn leen ko, denc leen ko ci ay saaku yu ñu ràbb te tegle leen ci bérëp bu wow, sedd, am ngelaw akk ker.
Current language
Wolof
Produced by
NASFAM