Binndu nduxum gi
Uploaded 8 years ago | Loading
08:56
- English
- Arabic
- French
- Portuguese
- Amharic
- Ateso
- Bambara
- Bariba
- Bomu
- Buli
- Chichewa / Nyanja
- Chitonga / Tonga
- Dagaare
- Dagbani
- Dendi
- Fon
- Frafra
- Gonja
- Hausa
- Kikuyu
- Kinyarwanda / Kirundi
- Kiswahili
- Kusaal
- Luganda
- Luo (Lango - Uganda)
- Malagasy
- Mooré
- Nago
- Peulh / Fulfuldé / Pulaar
- Sisaala
- Tumbuka
- Wolof
- Zarma
Nduxum mooy ňax bu bon bu ëpp li muy yàqq ci njaxnaat, dugub gi ak mboqq gi. Lu wuuteek lu ňu bari xalaat, nduxum gi du soqqeekoo ciy reen am waante ci pep am rekk. Li am, mooy benn taat u nduxum mën naa jur ay téeméeri june pep. Pep yi da ňu tuuti be tax lu ëpp ci beykat yi xamu ňu ni ay pep la. Da ňu nirόo ak pëndd bu ňuul. Bu mu leen nax.
Current language
Wolof
Produced by
Agro-Insight, ICRISAT