Défar taag yu muuj yi
Uploaded 3 years ago | Loading
15:30
ca taag you ndieuk yah, yamb yi danouy defar sén barababou bop nyou teglo ben ci kaw bénén nguir def fa sen lem, lolou day diafél jelub lem bi. ci taag you moudj yi, danouy dindi lem bi ak ben wutuloxo. Dagnou dieul lem té donou yax umbulaan wi. Umbulaan bi diekh takk dagnou koy délo ca taaag ba nguir yammb yi meun ci défat lem. lini mel dina takh gounor yi dootou gnou ame tioono ak di gnak sen ay waxtu di défarate umbulaan you bess. Ci sinema bi, dinagou diagh lane mo takh yamb yi soxla umbulaan. Teksi dinagnou diangh ci baykat you yagg yi ca népal nane lanouy défaré taag you moudj nguir meuna doundou bou baakh ci yaroum yamb.
Current language
Wolof
Produced by
Practical Action Nepal