Jëmbët um kaani
Uploaded 4 years ago | Loading
11:35
Mbey um kaani gu baax, mi ngi tambali ak ay palaŋ yu dëgër te wér. Waante yu bari nooy feeñal ndax palaŋ dina dunnd walla su nu ko jëmbëtee ci tool bi. Lék-leek sax, ay palaŋ yu dëgër te wér man nañu bañ magg. Man nañoo waññi ñakk gi ci def ay yenn liggéy yu war: defar um pepiñeer bi, Waajal tool bi, akk jëmbët un palaŋ yi.
Current language
Wolof
Produced by
Agro-Insight