Nji bu jub ak suqqi sesaam
Uploaded 4 years ago | Loading
10:00
Ci Afirik, mbeyum sesaam mi gën di yaatu ngir li ko marse bitiw réew di soxlo. Waante nak, randmaa yi da ñoo néew ndax njiwum sanni bi dafay joxe ay palaŋ yu tàñcu walla yu soreyoo yu dul magg ni mu waree. Te it, njiwum sanni day tax tool bi du neex topatoo. Moon de, am na ay pexe yu yombb yu mel ni nji bu jub ak suqqi yoo xamni di na waññi lim u palaŋ yu ndaw yi ci benn pax.
Current language
Wolof
Produced by
MOBIOM