Samm cellin u jiwu sesaam
Uploaded 1 year ago | Loading
9:07
Isin yi da ñuy laac ay pep u sesaam yu am benn melokaan akk benn dayuwaay.Ngir loolu, fokk mu am cellin u jiwu bi, mu tekki ni pep u sesaam yéep bokk benn xeet. Pep u sesaam yu jaxasoo ñoo gën jafe jaay te seen njëg day wacc.
Current language
Wolof
Produced by
MOBIOM, AMEDD