Dinndi bërr u kaarite buñu gënë baxal
Uploaded 3 years ago | Loading
13:46
Ber karité daffa barri embeef. Dagnou koy dieufandiko lou bari si waagn, pacc mame yi ak mbiroum taar. Waayé dindi mame you ndieuk ni gnouy dindé ber de karité bi dou andeu ak cett gui war, lolou moy diokhé beure bou tilim meuna faibarr gni kay dieufeundiko. Ci sinemaa dinagnou diangh nane la djiguéni bej-saalum mali yokké kattan li di défaroum beurre karité.
Current language
Wolof
Produced by
AMEDD