Boole banaana akk arikó ci mbey um ananaas
Uploaded 4 years ago | Loading
13:30
Palaŋ u ananaas yi daa ñu tambalee joxe ay doom ci ñaareel u at ganaaw bi nu leen jëmbëtee. Waante man ngeen am xaalis lu jiitu loolu ci bey yeneen mbey um dundd ci diggënté raŋ u ananaas yi. Lan mooy yoon mi gën baax ci def ko?
Current language
Wolof
Produced by
NOGAMU